L’anxiété généralisée se caractérise par une inquiétude excessive et persistante vis-à-vis d’un certain nombre de choses différentes. Les personnes atteintes d’anxiété généralisée ont du mal à contrôler leurs inquiétudes. Cela peut influencer notre vie car elle nuit à nos activités quotidiennes: l’école, le travail, les relations.
Feebaru xel bi nuy woowe anxiete generalisee moy di jaaxle jaaxle bu amul app ci lepp lunuy dund, jaaxle buy dem be epp doole borom. Bi jaaxle dine dem be di sopi sunuy dund ci berebu ligeeyukay bi, ecole bi mba niniy jeuflente ag nit yi nu nekal.
Il faut noter que la peur, le stress et l’anxiété sont des sentiments et expériences normaux et sont donc différents des troubles anxieux diagnostiqués. Inquiet a propos d’un examen? Anxieux à l’idée d’avoir un enfant ou de manquer un délai au travail ou à l’école? Cela fait partie de la vie.
Nu bayi xell ni bi feebar bi bokul ag tiit mbaa jaaxle biniy am bu feke daniu am lu am solo luy waaj xew lu melni examen wala di waaja am doom wala am ligeey bu am app bu teew. Yi jaaxle bokk ne ci dund bep doomu adama
Cependant, ce n’est pas considéré normal lorsque la personne présente un niveau élevé d’anxiété de façon continuelle pendant au moins 6 mois.
Quelques symptômes de l’anxiété généralisée sont: fébrilité, fatigue, irritabilité, troubles du sommeil, étourdissements, vertiges, maux de tête, transpiration excessive, tremblement, palpitations cardiaques, douleurs musculaires, trous de mémoires, sensation d’étouffement ou d’étranglement, difficulté à se concentrer…
Anxiete generalisee mingi tambali thi bu jaaxle bi neke ak nitt ki teh dakkul lu matt jurom ben weer. Mingui wanewu thi sonn, gaawa merr, nelaw gu epp mba mu doyut, miir, bopp buy metti, niakk gu epp, lox, fitt bu toogul, yaram buy meti, di faral di fatte, di yeg lu melni daniuley xojj, niakk meun bayi xell ci ligniy def ak yeneen
Il est conseillé de consulter un médecin lorsque l’on présente ces symptômes pendant plusieurs mois et qu’ils nous empêchent de mener a bien nos activités, lorsqu’on est en état de détresse. Les traitement disponibles sont les séances de psychothérapie et les médicaments prescrits.
Bunu ame yi mandarga banu tere no def linu wara def ci nim warre, danu wara seeti ab fejkat. Saafara bi moy psychotherapie maanam waxtaane ag docteur nguir meune xam nunuy def ba jaaxle bi dan mba mu ban no eup doole ak garab yu fejkat bi bind
Voici quelques conseils pour calmer son anxiété: accepter que l’on est humain et donc gérons notre vie de la meilleure manière possible et savoir que la perfection est un objectif inatteignable, comprendre ce qui declenche notre anxiete, prendre part a des activites qui nous apportent du bien-etre, prendre du recul lorsque l’on se sent submerge, interagir avec la famille et les amis pour nous changer les idees et enfin veiller a maintenir une bonne hygiene de vie en ecoutant les signaux de notre corps.
Yi diggle baaxna ci nitt ku am bii febar: nangu ni nitt matul tey xameni ya ngui def linga meune ngir se dund baax, comprendre liy indi gui jaaxle , di xalaate ag dall bula jaaxle gui eupeh doole, di def luy yokk baneex ci sunu dund, di jeuflente ak sunuy mbokk ag amdi jam ngir di feexal sunu xel. Warnga itam di deglou sey soxlay yaram , di nopalu, lekk ag di yengu nguir am dund gu sell.
Lorsqu’on vit avec une personne anxieuse, il faut savoir écouter et valider les sentiments de la personne en manifestant notre compréhension de la situation, ne surtout pas minimiser les inquiétudes de la personne atteinte et enfin l’encourager au traitement si besoin en les accompagnant et en étant disponible lorsqu’elle a besoin de nous.
Bunu nekke ak nit ku am anxiete generalisee, daniou war di deglou tey comprendre li nit ki di dund, diko xamal ni yeg yegam amena solo te diko bana xeebal ag jaaxlem. Warnagn diko encourager mu demm ci fejkat bi suko jaree teh diko gounge ci feju gi wanne ni nungifi saa yunu soxlaa.
Bi bataaxal lan leen indiloon tey ci febaru xel bi di anxiete generalisee
Ba beneen yoone ci *insert campaign name*
https://www.prevention-panique.lu/comment-aider-un-proche/
https://www.santemagazine.fr/psycho-sexo/psycho/8-astuces-pour-lutter-contre-lanxiete-198765